Yoon ngir Mouhamed! Waxtaan ak ay rakkam Sidy ak Lassana Dramé
Manage episode 458641671 series 3632325
Salaam maalekum!
Lu tollu ci benn at Radio Nordpol ci Dortmund mungi doon topp atte bu jigeen poliis yi faat Mouhamed Lamine Drame ci seeni jëf.
Fi ñu tolli nii ñungi doon joxe xibaar ci Allemand te deñoo bëgga tabax ab pont ci lakk yi ak waxtaan bu gàtt bii ak rak yu Mouhamed yi di Sidy ak Lassana.
Yoon ngir Mouhamed!
Wir danken Moustapha für die Übersetzung und den Brüdern Mouhameds für das Gespräch!
Gerechtigkeit für Mouhamed!
300 حلقات